Suite à sa vidéo jugée scandaleuse, Déesse Major défend son style jusqu'a en pleurer

Dans la meme Rubrique
          



Vues: 808
Commentaires des invites:
Ecrit Par Deug ( il ya 842 jours )
" Senegal lougniou wara wakh dougnioula wakh Mouk bayilene djambour bouleene gniou faat waay. Association religieuses lougniou wara lidieunti beurina Te doleen deg gniou deff Dara. Di wote dine Te gueumougniou ko. Chak jour nga guiss aass faux Mara wax louko nekh si dine dji te Keene doulen deg guene wax Dax ragual sene talibe yi. Legui nak guene beug sonal domou djambourgui. Mayelenko diam wayy fate guene torop. Senegal deuk dioulite la lagniou wax Te 90% yi musulmans lagniou Waye terewoul gnio vote charia bagnia daw mouy wane sounou naar fek. Xawoumako meussouta deglou musicam me wargueneko bayi bouguene xoloulwone snap chat am douguenen guiss wasalam   
Ecrit Par Tt feu ( il ya 844 jours )
" Yawww saa data ndeye...dioyalll deuter sa niawayyy. Domaramm Àvec sa vous donner de bons enfant ayyy agresseurs ak rayyykatou niitt reckk guénii diour. Embecile khathh   
Ecrit Par Dany ( il ya 844 jours )
" lakhawla walakhouwata illah billah qui séytané leu niou lay yédeu pour gua bakh guani daguay dioyy pour bonne !!!   
VOTRE NOM:  

  Cliquez Ici pour Ajouter des émoticones (emoticones)
Soyez courtois. N'envoyez pas de message ayant un ton agressif ou insultant. Quiconque ne respectant pas nos règles sera définitivement banis de ce system et votre adresse IP sera bloquée.
Les derniers articles publies

 
About Us | Help | Advertise | Terms of Use | Privacy Policy |
Copyright © 2007-2014 SenVideo. All rights reserved
View Large Image