Dans la meme Rubrique
          



Vues: 12299
Ecrit Par ( il ya 2748 jours )

" esk cette mobilisation en vallai la peine? je respecte bcp sidy mais je trouve kil joue un double jeu... Gaston moy lolou, diaroul topou; tog si digg télé toud une personne nane famille diaroul diay, cé sur k toute la fami va se sentir concerné "   Répondre à Ce membre
Commentaires des invites:
Ecrit Par -2147483648 ( il ya 1142 jours )
" -2147483648   
Ecrit Par pape cheikh fall ( il ya 2745 jours )
" itackilha ragalene yalla adouna nite mounouko toukoul koudoul yalla sounou borome ... mai nak fitna kena douka yakati. baye ak yalla mo gane lo guisse loune diarouko nio bokou sounou senegal.. bayilene thiowe li   
Ecrit Par J8 TALIBè NIA ( il ya 2747 jours )
" ASala mou halaye koum wa rakhmatoulaHI WA BAra ka tou sidi lamine ab dioulite dou yè fitna li khew sa DIGANTEK GASTON YEN NIARE,BOUL DAW DU LAKHOU SI SERIGNE BI DAW LAKHOU SI ALKHOURANE MO GANA WOR NDAKH ANDINA LO KHAMNI LER NA ,MOUYE WAkh ta yalla rek takh ndakh man mi douma dara wayè douma nangou ken djoudou ,wayè nak mouhamad dafa wakh ni kou ragal niemè lepou ,lepou malaye niemè,wayè bo nièmè yalla ragal lepou lepou molaye nièmè ba takhna sidi lislam nekoul lom khamni nit dalaye togne nga dioklhangne mou dè nonooooooooo loye def na yalla takh ak loye wakh ndakh kham kham niepou lakop yalla mAYE YAMOUL REK SI KAROU DINè WASALAM   
Ecrit Par heli ( il ya 2747 jours )
" mani bougnou kene rayyy di diayyy baatine di khass djoudou nitt gni tkou khass sa bonga merr fi dall gnepp diaamou yalla lagnou kene gueunoul kene guinaw rassoulilah waayé nak kouné khamnga kila meun té khékhou leen ja jeuf   
Ecrit Par jp ( il ya 2747 jours )
" affaire bi khadimoul khadim la niassene yi da nio réw da nio yébaté talibé bi gene ndaw menoul data ndeyam. yeurmandé   
Ecrit Par abdou diop ( il ya 2747 jours )
" ila touba   
Ecrit Par bb ( il ya 2747 jours )
" yeytaneeeeeeeeeeeeeeeeeee   
Ecrit Par rafaze ( il ya 2747 jours )
" kouy togne, ter kou bayiwoul dii tekk ayy kham khamou enrengements di nga kko layyo ssi lou weur, legui lou wayy wokh tek bene suraat alquran meelni li miiy wakh daako leer. yalla na khel yii akk khol yeup deloussi gnou khamner kouy yakh mo gueuneu gaaw kouy deffar wa salam akk diegueulou   
Ecrit Par rafaze ( il ya 2747 jours )
" mais tamite senegal lii moo takh mou gueuneu metti, gueuneu taar. kholal ma ay pounkal you tolli nii dii woter kharer avec le vent ou pour se faire voir a la tele o. gayi yeneyi defay melni weddi yala gnoune gneupe ayy ndongo daara you tarbiyou baa wathie alkhourane ,wayer yalla dou farral   
Ecrit Par laye only ( il ya 2747 jours )
" sidy seytané bou mak vraiment ya ngui yak sa réputation li nga fi wakh leup amoul selon moi car j'ai suivi votre probléme entre toi et gaston ...ya togne démale nga outi materiel ndakh nga mane déf direct kou niakk fayda nga bayil léép.   
Ecrit Par kine khamokuo ( il ya 2747 jours )
" sidi ya togne dimal laguiyi ti wakhji   
Ecrit Par tajtant ( il ya 2747 jours )
" sidi dimbalil nite yi bayil yak say mbok di teukou nityi dolene rigou boulene lene ngou sonal lek ak nane lagnou tal   
Ecrit Par mendy ( il ya 2747 jours )
" famille niassene vous aussi ne rentrer pas dans ce jeux, vous etes des gens bien et eviter de rentrer dans ces genres de combines. Quand a sidy lamine si tu as des deboires avec tes comperes n'y mele pas les niassenes qui sont des gens discret.   
Ecrit Par FA ( il ya 2748 jours )
" CONSCIENCE COUPABLE N'A PAs besoin d'accusateur. yalla dou rayal ken nonam. TE LOBABAGNE NGOR DOU TAH YALLA NIAKA TAW SI TOLAM   
Ecrit Par kabrouba ( il ya 2748 jours )
" sidy lamine niasse betteu ngama trop sakh !!!!!!! khawma woone ne' nii nga mell!!!!! dioulite dou deff yeenyii!!!11   
Ecrit Par Moi ( il ya 2748 jours )
" Non mais je reve ou quoi?? Yallah de mo meuneu gneup , te reubeu neu seytane.Tout ce bruit pour rien.Heureusement que le ridicule ne pas.Gaston bo teude na nga nelaw,Yallah bour bi guemoul nelawoul. Sidy lamine yow , ko yeubou moytoula....Deugueu nak nekhoul,. Gaston yalna leu Yallah mey ndam.   
Ecrit Par nono ( il ya 2748 jours )
" yallna yalla def soutoura ak khewal ak wer si niape   
Ecrit Par kajor ( il ya 2748 jours )
" homme religieux vous dites, dans y a plus de "nafegn que de pieux. c'est malheureux ce que nous avons regardé hier à walf. nous avons tous ou en partie suivi gaston à rts et à 2s. et ses propos son enregistrés, sidy doit avoir le courage d'expliquer clairement les propos de ce dernier à ses parents et de leur ce qui s'est passé reellement entre eux. mais le mensonge n'est pas pardonnable surtout venant des homme comme .........   
Ecrit Par big mo ( il ya 2748 jours )
" le senegal et a retard lou niak faydali niouy def bayilene politiquebi sidi dou dara adounabi ken manouloul kene dara demlene ligueyi   
Ecrit Par tata ( il ya 2748 jours )
" moi j'ai suivi l'emission de xagabal jusqu'au bout je n'ai pas entendu gaston dire k'elle ke chose de depasser a la famille niassenne sidi da fa wara khamni mac mac da fey wakh degue mac dou soss dou fene gaston mome le done wakhal mom rek na niou mey sou niou diame lane mo fi diar di deme di mobiliser toute la famille niassienne si tu as un proble avec gaston regle le avec lui mais boul soss di diakhasser senegal di fene lo lou bakhoul   
Ecrit Par di baba ( il ya 2748 jours )
" salam yaw mom di saga hady yaw lay wahal yarou wo ken yaroul la kou kene yaroul nak ken dou wah ak mom paske khaj sakh mole gen sa sagayi mourid douko wah moy ne yaw do mourid do talibe kene ta kou amoul serign chaytane neke sa serign ta kou chaytane neke di serignm yaw bayima yi sakh nio la gene ok merci kou wahj ndakhdi nga ballm   
Ecrit Par vra ( il ya 2748 jours )
" huuuuuuuuu sidy lamine man d ragal nala... waaaaaw, ya meuneu taaaaaaaaawi   
Ecrit Par ..... ( il ya 2748 jours )
" eeeee gaston wakh na deeg, ken geunoufii keneu, liguey rek mo am sollo, ki gueneu diegge yallah moy ki ko gueuneu ragal, bou gnou ken sonal, Gaston attakewoul famille Ndiassene, ndakh kou kham diine kham ni Ndiassane gnou bakh rek gno fa Nek si walou diine bi. Waye sidy lamine mi moy seytane bi, ni ko amy wakhe rek moy deeg, ki daffa beug diakhasse Senegal   
Ecrit Par amy ( il ya 2748 jours )
" sidy lamine ya rambath ya seytane deeg deeg, yaye seytaaane, sougnou la togne da gua koye fajial sa bop, ken wafou fi wakhou diine ba gua bougeufi eundi wakh.   
Ecrit Par bb ( il ya 2748 jours )
" je trouve meme que lache de la part de sidy lamine d'apporter ce problem au pret de la communaute niassene. Ce qui l'oppose a Gaston n'a rien a faire avec la famille Niassene, suis tres decu de cet acte de sidy lamine, affairou cheytaaneee deeg la def fii, que ca soit gaston, sidy lamine ou un autres ils sont tous pareil, seul l'argent leur interessent, ils s'en fou du reste, que ca soit leur freres ou famille   
Ecrit Par rafaze ( il ya 2748 jours )
" kissnga kouy woter kilifa da nga kaay nourou, et les gars wakhtanne wakh deugthi laa.gaston n`a rien fait du tout il a repondu a sidy lamine en ce qui les concernes et il a le droit de dire que sidy gueunoukko dioudou , parceque sidy est homme d`affaire mais se cache toujours derriere la famille niassene , et j`ai remarquer que sidy essaie toujours de creer des problemes alors wakhlene thi mome lolou moy deug. manguii toupe tey diegueulou sii bepp kaddou bou deungue   
Ecrit Par lay low ( il ya 2748 jours )
" boulène gnou sonnal....pr se faire respecter, on doit se respecter soi-mème. on ne peut pas passer son temps à insulter les autres et à les traiter de ts les noms et ne pas s'attendre en retour à la réaction des insultés, c'est leur droit le plus obsolu et je crois que la réponse de gaston est totalement proportionelle aux déclarations de sidy lamine. personne n'a le droit de se cacher ou d'utiliser une quelconque famille, confrérie ou religion pr attaquer les autres ou vouloir se défendre. sa famille biologique et/ou religieuse n'a qu'à lui demander de cesser d'insulter et de prendres les autres pr mieux que rien s'il veut qu'en retour on le respecte et ne dise rien qui puisse affecter tous ceux qui se reconnaissent en lui.   
Ecrit Par frommars ( il ya 2748 jours )
" De toute facon tout ce qu'a dit Gaston est vrai et cela conserne seulement Sidi lamine Niass mais pas la communaute niassen ... Et avant tout ils sont tous des biznessmen pas la peine de virer le debat ,,,Tout le monde a compris ce qui est dit   
Ecrit Par scipio ( il ya 2748 jours )
" sidy mingui diakhassé nieup ak niassene yi. Lou Gaston wakh si tv nationale en koi ça concerne le PR et le reste du senegal. Si Gaston dit ces conneries, en quoi ça nous oppose aux niassenes? Moi meme ki parle je suis talibé cheikh ahmed tidiane-cheikh al islam, mé là sidi a déconné vraiment!!!!   
Ecrit Par sak ( il ya 2748 jours )
" caston mbenge ya boon yadi khaje ya rew   
Ecrit Par diawase ( il ya 2748 jours )
" comment on peut tenir des paroles quelconques a l'endroit d'un homme religieux. Je ne suis pas un talibe tidjane. ces gens comme gaston mbengue doivent disparaitre dans l'espace audiovisuel, ces cachets pharaoniques sont l'objet de blanchissement.   
VOTRE NOM:  

  Cliquez Ici pour Ajouter des émoticones (emoticones)
Soyez courtois. N'envoyez pas de message ayant un ton agressif ou insultant. Quiconque ne respectant pas nos règles sera définitivement banis de ce system et votre adresse IP sera bloquée.
Les derniers articles publies

 
About Us | Help | Advertise | Terms of Use | Privacy Policy |
Copyright © 2007-2014 SenVideo. All rights reserved
View Large Image